Download Video and Audio from YouTube

Ndongod (Daaraj Family) - End-discipline (clip officiel) #ndongod #indiscipline

363,909 views 13 165

official music video for "endiscipline" by Ndongo d Directed by : supernova, Mamoune Prod composed by Faada Freddy and Demolisha recorded @ Bois sakre & Demolisha Mixed @ Demolisha By Demolisha Subscribe to the official Djf YouTube Channel :https://www.youtube.com/user/Daarajfa... https://www.facebook.com/daarajfamily... https://www.instagram.com/daarajfam_o... https://wwwtwitter.com/daarajfamily lyrics: Ya ngi xaax tëf fune ci mbed sotti mbalit mi sa yoon dëkando faleewo ya ngi baare tali bi « tente » koñ bi yëp poot dajale say paan ni cars-rapide bu yab ba fees ci digg yoon bi mu « panne » soffër bi dugg tali bi « dos-d'âne » falewul xiiro bi ηaayo bi koksër aparanti ken attewul ñaata saufaar ñu lim burle “feu-rouge” ñu ne cëm ki moy waaja bimuy dawal ub seen bët ñu gëmm T'en as rien à faire , tu craches partout sur le bitume tu jettes tes ordures à tout-va ,le voisinage tu t'en fous!! Tu bloques le passage juste pour une cérémonie,une grande tente pour célébrer un baptême,tu laves ton linge en plein milieu de la rue chargée comme un car- rapide tombé en panne Le chauffeur n'a pas froid aux yeux,rien à faire du dos-d'âne .Banales sont les bagarres entre apprentis et coxseurs sur la voie publique ,combien de chauffards grillent le feu rouge invisible, tout le monde s'en fout au final on a des yeux que pour sa belle caisse on en bave . Endiscipline ku dem yobaale sa jikko li araam moy ñakk yaradiku tilim jikko Endiscipline Melokaan bi ngay dikke ci bitti ni nga njëkke ñu ngi gis nuñ lay sikke Endiscipline Marsandisu reewande tey la gëna lambb ñëppay jënd ñëppay jaay Endiscipline yaa ngi tëb tëb ta do dal bis yar a dal ta ken ken du la raay endiscipline nos comportements nous reflétent le pire dans la pauvreté est l'inconscience,l'impolitesse et le mauvais comportement endiscipline ta manière d'être se refléte sur ton attitude on te jugera sur les faits et l'attitude Endiscipline est comme une marchandise qui se vend comme des petits-pains tout le monde en achéte tout le monde en vend endiscipline on est de plus en plus fougueux on s'obstine un de ces jours on le regrettera amèrement Mëno xaar sa tuur sooga ñëw burle rang bi ya ngi ndadé kontewoo bëg tëb “numba 1one bi” bo dugge bus tafu tafee ak sa xet ya ngi nuy xër saxaar sigaret sanni fula neex dajjeeti nga beneen paket naan sa njaru kafee kaas bi xaar yeneen sareet ya ngi guux sa ndox fi nga taxaw ngay sanni mbuus bi say loxo duñu set ya ngi gén leegi duus bi t'es pas patient tu préféres griller les étapes t'es venu en dernier tu veux passer en premier tu schlingues et tu colles les gens dans le bus en volant du plaisir ,tu fais du pick-pocket . Tu nous enfumes avec ta cigarette ,à peine tu jettes un paquet t'en ouvres un autre et t'en met partout en buvant du njaru café ,la tasse attendra le passage des charrettes .Aprés quelques gorgées d'eau tu lances le sachet par terre, tes mains sont sales tu viens à peine de sortir des toilettes Refrain.. Civilise ak badoolo doxin wa ak waxin wa jëf ja ak nuyoo ba ak rentré ba Accident yu bëri yi ngay gis manque de civisme la bu fukki nit di gas fukki nit di suul pax du gaawa am manque de civisme mën ta weesu pont ba duñ ca yeeg ba ci commissariat yi leele nga gis mode tortures yo xamne manque de civisme la être civilisé ou impoli Dans ta maniére de marcher, de parler de saluer ou de faire trop d' accidents dûs à un manque de civisme “Défense d'uriner “ mur bi sax tereko ya ngi taxaw ci mbed mi saw jokkan fa pareego Policier bi neena priip njaga ndiaay fok mu stop bu de dafa amul frein loxom fok mu yoor ci poos taxi gén sens-interdit liila xelam yannu ci loos Marchands ambulants dox ci naaj bi dans le vent ni trotuwaar bi en-avant fok mu def sandikat xat na lool Sandaga liko jële dëk ba moola fi inddi dañuy course ak yafuus mëna jël sen benefice lu tabax yeeg yeeg xel ya ngi gëna di kule daf ñuy tere gëna gis teggin bi nilañuy koy suule lu tabax yeeg yeeg xel ya ngi gëna di kule daf ñuy tere gëna gis teggin bi nilañuy koy suule On dirait qu'ils ont la cécité ,”défense d'uriner” même écrit sur le mur ne les empêche pas d'y pisser ou d'y déposer leurs besoins. Même un priiip (siflet) du policier n'arrêtera pas le ndiaga ndiaye(transport en commun) sans frein, il mettra la main à la poche. Il est pas dans son assiette le taximan,il aura pris le sens-interdit comme à son habitude. Et le marchand ambulant déambule dans le vent, sous le soleil ardent il est le roi des trottoirs il fera comme à Sandika(pikine) il va assiéger Sandaga .On vient tous du village on est pas des fénéants on a le même but c'est faire du bénéfice coûte que coûte Et Plus les immeubles sortent de terre plus les esprits s'enterrent, on y voit plus trop clair on enterre les bonnes manières Plus les immeubles sortent de terre plus les esprits s'enterrent. #Ndongod #indiscipline #Daarajfam